1Mu jëm ci njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda.
2Asamaan nee Yàlla màgg na,
3Bésoo bés kàddu seede ko,
4Du làkk, duy wax,
5suuf sépp la seen ndéey jibal,
6mu mel ni boroom séet, génne néegam,
7Asamaan lay fenke cat lii,
8Yoonu Aji Sax jee mat,
9Lu Aji Sax ji tegtale, njub la,
10Santaaneb ragal Aji Sax ji mooy li sell|lemma="sell:"*
11Moo dàq wurus,
12Man, Sang bi, ci laay leerloo,
13Nit juum na, umple ko,
14Te Sang bi, musal ma ci bàkkaaru teyeef,