Taalifi cant 22:1-31 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda, dëppook galan bi ñu dippee Kéwélu fajar.

2Sama Yàlla, sama Yàlla, lu tax nga wacc ma?

3Éy sama Yàlla, ma woote bëccëg, wuyuwoo;

4Yaw de, yaay ku sell|lemma="sell:"*, tooge sab jal,

5Yaw la sunuy maam wóolu woon,

6Yaw lañu daa woo wall, mucc;

7Man nag aw sax rekk laa, matuma nit.

8Ku ma gis ñaawal ma,

9«Na wéeru ci Aji Sax ji, mu xettali ko;

10Yaw de yaa ma roccee sama biiru ndey,

11Yaw laa dénkoo ba may juddu,

12Bul ma sore,

13Noon yaa ngi ma gaw ni coggalu yëkk,

14Ñu ŋa ma, ŋàpp,

15Doole ŋiis,

16Làmmiñ taqoo denqleñ,

17Ay xaj a ma wër,

18Maa ngii, mana waññ sama yax yépp,

19séddoo samay yére,

20Waaye yaw, Aji Sax ji, bul sore;

21Xettalil sama bakkan ci saamar,

22Musal ma ci pàddum gaynde ak ndañum nagu àll.

23Maay siiwali saw tur ci samay bokk,

24Yeen ñi ragal Aji Sax ji, santleen ko.

25Moom de sàgganewul mbaa xeebul boroom tiis,

26Yaw laay sante ndaje mu mag,

27Ku woyof a cay lekk ba doyal,

28Àddina wërngal këpp ay fàttaliku,

29Aji Sax jeey boroom nguur,

30Boroom barke xéewlu, sujjóotal ko,

31Askan wu dikkagul dina jaamu Boroom bi,

e>