Taalifi cant 26:1-11 WOLB2025 - Bible AI

1Ñeel Daawuda.

2Aji Sax ji, nattu ma, seetlu ma,

3Maa ngi janook sa ngor,

4Toogumaak naxekat,

5sib naa gàngooru saay-saay,

6Aji Sax ji, maay jàpp ci biir mucc ayib,

7àddu, sant la,

8Aji Sax ji, maa sopp sa dëkkuwaay,

9Bu ma buubaaleek bàkkaarkat, sànni,

10Seeni loxoo nga sóobu ci mbon,

11Man nag màndu laay wéye,

e>