1Dib taalifu cant, ñeel Daawuda, ba muy daw Absalom doomam ju góor+ 3.1 Seetal ci +bk 2.Samiyel+bk* saar 15—16.*.
2Éy Aji Sax ji, noon yeeka bare!
3ñu baree may tooge naa:
4Waaye yaw Aji Sax ji, yaa may feg,
5Maay woo Aji Sax ji wall,
6Maay tëdd nelaw, yewwu;
7Ñu dul jeex a ma jógal, gaw ma,
8Éy Aji Sax ji sama Yàlla,