Taalifi cant 31:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda.

2Aji Sax ji, yaw laa làqoo,

3Teewlu ma,

4Yaay sama cëslaay, sama rawtu.

5Génne ma fiir gi ñu may tëroo;

6Yaw laa jébbal samag noo.

7Maa bañ kuy topp tuuri neen.

8Damay bég, di bànneexoo sa ngor,

9Waccoo ma ci loxol noon,

10Éy Aji Sax ji, baaxe ma, jàq naa!

11Naqar a ngi may rey,

12Noonoo noon a ma sewal,

13Kenn xalaatu ma, xanaa fàtte ma ni ku dee,

14Damaa dégg jëw yu bare,

15Man nag Aji Sax ji, ci yaw laa dénku.

16Yaa yor sama àpp.

17Leeralal ma sa kanam, Sang bi,

18Éy Aji Sax ji, woo naa la wall,

19Yal nanga tëj gémmiñu fen-kat

20Yàlla yaa yaatu ngëneel

21Yaa koy làq fa nga làqu,

22Cant ñeel na Aji Sax ji!

23Man nag saalitoon naa ne:

24Képp kuy aji gëm, soppal Aji Sax ji.

e>