Taalifi cant 38:1-22 WOLB2025 - Bible AI

1Dib taalifu cant buy fàttalee, ñeel Daawuda.

2Éy Aji Sax ji, bul mer, di ma rëbb;

3Aji Sax ji, fitt nga maa fitt,

4Danga maa mere, ma wéradi;

5Samay ñaawtéef mëdd ma,

6Maa defug ndof,

7Maa ngi sëgg, ne yàcc, ne yasar,

8yaram tàng, di bax,

9Sama yaram dee goyy, ma ne lasar,

10Boroom bi, yaa ngi ne jàkk ci samay nammeel,

11Sama fit a ngi tëf-tëfi, doole ŋiis,

12Samay dana tax xarit ak dëkkandoo di ma daw,

13Ñi may wuta rey a ngi may fiir,

14Man, ma mel nib tëx, dégguma,

15di saf ku dul dégg,

16Aji Sax ji, yaw laa yaakaar;

17Ma ne, ngalla buñu ma ree,

18Maa ngii di waaja daanu,

19Ma ne, aylayéwén def naa lu ñaaw,

20Noon yaa ngi ne jonn ak seen doole,

21Ma ji leen njekk, ñu fey ma njekkar;

22Éy Aji Sax ji sama Yàlla, bu ma wacc,

e>