1Mu jëm ci Yedutun, njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda.
2Dama noon: «Damay moyu ba duma moye làmmiñ.»
3Dama noon cell, ne patt,
4sama xol diis,
5ne: «Éy Aji Sax ji, xamal ma sama muj
6Yaatuwaayu loxo nga ma àppal ciy fan,
7Nit du lu moy takkndeer buy dem,
8«Éy Boroom bi, lu may xaarati?
9Musal ma ci sama mbugali tooñoo tooñ,
10Noppi naa, dootuma wax,
11Waaye ngalla teggil sab yar,
12Yaay mbugal ku bàkkaar, yar ko,
13Éy Aji Sax ji, déglul, ma ñaan la,