Taalifi cant 40:1-17 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, ñeel Daawuda, dib taalifu cant.

2May xaar a xaar Aji Sax ji,

3génnee ma ca kàmbug sànkute,

4Moo ma may, ma fent,

5Ndokkalee, yaw mi dénku ci Aji Sax ji,

6Yaw Aji Sax ji sama Yàlla, bare nga loo def,

7Saraxi jur ak pepp, taamuwuloo ko,

8Ma ne: «Maa dikk nii,

9Sama Yàlla, maa defsi sa coobare,

10Siiwal naa sag njubte ca ndaje mu mag ma.

11Làquma sag njubte, ne cell ak moom.

12Éy Aji Sax ji, bu ma xañ sa yërmande.

13Ay musibaa ma tanc,

14Éy Aji Sax ji, yal na la neex, nga wallu ma!

15Képp kuy wuta fëkk sama bakkan,

16Ku may ñaawal,

17Képp ku la wër,

e>