Taalifi cant 43:1-4 WOLB2025 - Bible AI

1Éy Yàlla, àtte ma,

2Yaw Yàlla kat yaay sama rawtu.

3Ngalla yónneel sag leer ak sa dëgg,

4Kon Yàlla, naa àgg ca sa sarxalukaay|lemma="sarxalukaay b-:"*;

>