1Di woyu cant, ñeel askanu Kore wu góor.
2Aji Sax jee màgg, jara màggal a màggal
3Jekk taxawaayee tundu Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, catu bëj-gànnaar,
4Yàllaa wone kaaraangeem
5Buur yaa ngoog daje,
6Nun noo gis, jommi,
7ne fay pat-pati,
8Ngelawal penku, moom ngay tase
9La nu déggoon de lanu gis
10Céy Yàlla, nu ngi sa biir kër,
11Céy Yàlla, sa tur ay sa woy
12Yal na waa tundu Siyoŋ bég,
13Doxleen biir Siyoŋ, wër ko,
14nemmikuy tataam,