1Dib taalifu cant, ñeel Asaf.
2Ca Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, dëkk ba ca taar ba
3Sunu Yàllaa ngi ñëw te du ne cell,
4Ma ngay woo seede asamaan ak suuf,
5Mu ne: «Dajaleel ma sama wóllëre
6Asamaan a ngi biral àtteb Yàlla,
7«Yeen sama ñoñ, dégluleen, ma wax leen;
8Du seeni sarax laa leen di sikke,
9Soxlawuma yëkku yar ak sikketu gétt.
10Maay boroom raboo rabu àll,
11Xam naa njanaawi tund yi,
12Su ma xiifoon, duma leen ko wax,
13Ndax damay lekk yàppu nag
14Deel jaajëfal Yàlla, sarxale ko,
15di ma woo bésub njàqare,
16Ñu bon ñi, Yàlla ne leen:
17Yeena ngii, bañ sama yar,
18Fu ngeen gisub sàcc, neexook moom,
19Dangeena afal seen gémmiñ ci mbon,
20ngeen di tooge seen mbokk,
21Lii yeena ko def! Damay noppi,
22«Yeen fàttekati Yàlla yi, déggleen lii,