1Mu jëm ci njiital woykat yi, dib taalifu yeete bu ñeel Daawuda.
2Mooy ba Doweg, Edomeen ba, demee ca Sawul, ne ko Daawuda dem na kër Aximeleg+ 52.2 Seetal ci +bk 1.Samiyel+bk* saar 21—22.*.
3Moo! Jàmbaar ji, looy damoo jëfi coxor?
4Ak sa làmmiñ wi ngay sose loraange,
5Lu bon a la gënal lu baax,
6Yaa bëgg jépp wax juy yàq,
7Yàlla da lay sànk ba fàww,
8Aji jub gis ko, yéemu,
9«Xoolleen jàmbaar ji làqoowul Yàlla,
10Man, ma mel ni garabu oliw gu naat