Taalifi cant 54:1-8 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, ànd aki xalam, dib taalifu yeete bu ñeel Daawuda.

2Mooy ba waa Sif demee ca Sawul, ne ko Daawudaa nga làqu ca seenum réew+ 54.2 Seetal ci +bk 1.Samiyel+bk* 23.14-28; 26.1-5.*.

3Éy Yàlla, musal ma ngir sa tur,

4Éy Yàlla, déglul, ma ñaan,

5Ay doxandéem a ma jógal,

6Yàllaa ngii, moo may dimbali;

7Yal na ay wi këppu ci ñi may tëru,

8Xol bu tàlli laa lay sarxale.

>