1Mu jëm ci njiital woykat yi, ànd aki xalam, dib taalifu yeete, ñeel Daawuda.
2Éy Yàlla, déglul, ma ñaan la,
3Teewlu ma, nangul ma.
4coowal noon yee
5Sama fit a ngi rëcc, di tëf-tëfi;
6Njàqaree ma dugg, may kat-kati,
7Dama ne: «Éy ku may may laafi xati,
8Xanaa ma naaw, ba sore,
9Naa gaawtu, seeluji
10Éy, Boroom bi, beenal seeni wax, neenal leen.
11guddeek bëccëg ñuy wër,
12Yàq a nga ca biir,
13Su doon noon bu may ñaawal,
14Waaye yaw la, sama nawle,
15Nu daan bokk bànneexu diisoo,
16Yal na leen dee bett,
17Waaye man, Yàlla laay woo wall,
18Subaak ngoon ak njolloor,
19Moo may jot|lemma="jot:"* ak jàmm,
20Yàllaay dégg, duma leen,
21Workat baa ngi xàcc loxoom jëme ci ñi mu takktool,
22làmmiñ wa daa neex ni lem,
23Sippikul Aji Sax ji lu la diis,