1Mu jëm ci njiital woykat yi, dëppook galan bi ñuy woowe Bul yàq, diy ñaan, ñeel Daawuda, gannaaw ba mu dawee Buur Sawul, ba dugg ca xunt ma+ 57.1 Seetal ci +bk 1.Samiyel+bk* saar 24.*.
2Éy Yàlla, baaxe ma, ngalla baaxe ma,
3Ma woo Yàlla, Aji Kawe ji,
4Mooy yónnee fa asamaan, musal ma,
5Maa ngi tëdd ci biiri noon
6Éy Yàlla, yaa màgg, ba sut asamaan,
7Noon yi di ma fiir,
8Yàlla, dogu naa,
9Na sama jëmm jépp yewwu,
10Boroom bi, naa lay gërëm ci biir xeet yi,
11Sa ngor a màgg, ba àkki asamaan,