1Mu jëm ci njiital woykat yi, dëppook galan bi ñuy woowe Bul yàq, diy ñaan, ñeel Daawuda. Mooy ba Buur Sawul yónnee ay nit ñu ko xoolal kër Daawuda, ngir rey ko+ 59.1 Seetal ci +bk 1.Samiyel+bk* 19.11-17.*.
2Éy sama Yàlla, xettali maak noon yi,
3Xettali maak ñiiy def lu bon,
4Aji Sax ji, ñu ngii di ma tëru, nar maa rey,
5Defuma lu ñaaw, ñuy xélu, di ma waajal;
6Aji Sax ji Yàllay Israayil, Yàlla Boroom gàngoor yi,
7Bu ngoonee ñu wàccsi,
8Déglul li ñuy yebbee ci seen gémmiñ,
9Te yaw Aji Sax ji, yaa ngi leen di ree,
10Yaay sama doole, ma di la séentu,
11Sama Yàlla ju goree may gatandu.
12Yàlla, bu leen rey,
13Bàkkaar lañuy wax,
14Meral, jeexal leen,
15Bu ngoonee ñu wàccsi,
16Ñuy wër di wut lu ñu lekk,
17Maa lay woye sa doole,