Taalifi cant 60:1-13 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, dëppook galan bu ñuy wax Seedeb tóor-tóor, diy ñaan, ñeel Daawuda.

2Mooy ba Daawuda di xareek waa Siri ña ca Mesopotami ak waa Siri ña ca Coba te ba ñu ca bàyyikoo, Yowab duma fukki junniy Edomeen ak ñaar (12 000) ca xuru Xorom wa+ 60.2 Seetal ci +bk 2.Samiyel+bk* 8.3-14; +bk 1.Jaar-jaar ya+bk* 18.3-13.*.

3Éy Yàlla, wacc nga nu, bëtt sunu kiiraay.

4Yëngal nga suuf, xar ko;

5Won nga sa mbooloo lu metti,

6Sampal nga ab raaya ñi lay ragal,

7Walloo nu sa ndijoor, nangul nu,

8Yàllaa àddoo fa këram gu sell,

9Maa moom diiwaanu Galàdd, moom Manase,

10réewum Mowab di sama ndabal raxasukaay,

11Éy Yàlla, ana ku may yóbbu dëkk ba tata wër?

12Xanaa kay du yaw, Yàlla mi nu wacc,

13Ngalla dimbali nu ci bañaale;

e>