1Mu jëm ci Yedutun, njiital woykat yi, dib taalifu cant, ñeel Daawuda.
2Yàlla doŋŋ ay dalal sama xel,
3Moom doŋŋ mooy sama wéeru-mucc,
4Xanaa dungeen bàyyee songandoo nit,
5Seeni mébét, wàcce boroom daraja doŋŋ;
6Yal na Yàlla doŋŋ di dalal sama xel,
7Moom doŋŋ a di sama wéeru-mucc,
8Yàllaa may musal, di ma sagal,
9Bokk yi, wóoluleen ko fu ngeen tollu,
10Doom aadama, ngelawal neen;
11Bul wóolu ribaa,
12Benn yoon la Yàlla wax,