Taalifi cant 71:1-23 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji, yaw laa làqoo,

2Xettalee ma sa àtteb dëgg, yiwi ma;

3Yal nangay sama cëslaay, sama rawtu

4Éy sama Yàlla, musal ma ci dooley ku bon

5Boroom bi Aji Sax ji, yaw de laa yaakaar,

6Yaw laa wéeroo ba may juddu;

7Firndey alkànde la ma ñu bare xoole woon,

8Samay kàddu sag cant la fees

9Ngalla bu ma wacc, mag laa;

10Noon yaa nga may tooge,

11naan: «Yàlla wacc na ko,

12Éy Yàlla, bu ma sore.

13Ñi may tuumaal,

14Man may saxoo yaakaar,

15May siiwal sa àtteb dëgg,

16Boroom bi Aji Sax ji, ma dikke la sag njàmbaar,

17Éy Yàlla, ba may ndaw, nga ma xamal say kéemaan,

18Éy Yàlla, bu ma bijjaawee ba weex tàll it, bu ma wacc,

19Céy Yàlla, sa àtteb dëgg àkki na fa kaw-a-kaw.

20Won nga ma ay yoon coonooki tiis,

21Yal nanga ma gëna sagal,

22Man it sama Yàlla, ma xalam, sant la

23sarxolle, woy la,

e>