Taalifi cant 73:1-27 WOLB2025 - Bible AI

1Dib taalifu cant, ñeel Asaf.

2Waaye man de tuuti kon ma lajj,

3ngir maa ñee ku bew,

4Amuñu mitit,

5Doñ-doñu nit dabu leen,

6Moo leen taxa ràngoo reewande,

7Dañoo suur ba gët suulu,

8Dañuy ñaawle, di wax lu bon,

9Seen ŋalŋal àkki asamaan,

10Moo tax ñoñi Yàlla walbatiku ci ñoom,

11te naan: «Lu ci Yàlla xam?

12Ñu bon ñaa ngoog!

13Man kay maa sellal ci neen,

14Bés bu ne yar dal ma,

15Su ma noon: «Naa waxe ni ñoom,»

16Naka laay jéema ràññee lii,

17Ba ma àggee sa kër gu sell ga,

18Yoonu tarxiis kay, nga leen teg,

19Yàquleeka leena bett!

20Day mel ni gént goo yewwoo.

21Naqar laa amoon,

22Booba ngaaka laa, xawma dara;

23Teewul ma des ak yaw,

24Danga maa gindee sam xel,

25Ana ku ma am asamaan ku la moy?

26Kàttan ak pexe jeex,

27Ku la sore kat, sànku;

e>