1Mu jëm ci njiital woykat yi, ànd aki xalam, di woyu cant, ñeel Asaf.
2Yàlla siiw na fa Yuda,
3Xaymaam a nga Salem,
4Fa la rajaxee fitt yuy boy
5Yàlla yaa ne ràññ te darajawu,
6Futtees nay boroom fit,
7Yaw Yàllay Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*, yaa gëdd,
8Yaw mii, yaa mata ragal;
9Fa asamaan nga biraleb àtte;
10Ca la Yàllay jóg, ngir àtte,
11Doom aadamaak xadaram rafetal sa woy;
12Seen Yàlla Aji Sax ji, digooleen ak moom