Taalifi cant 81:1-16 WOLB2025 - Bible AI

1Mu jëm ci njiital woykat yi, ñeel Asaf, te ànd ak xalam gu ñuy wax gitiit+ 81.1 gitiit: seetal ci 8.1.*.

2Sarxolleleen ci Yàlla mi nuy dooleel;

3Yékkatileen woy te jiin,

4Walleen bufta bi ci Terutel weer wi,

5Loolu wartéefu Israayil la,

6di ndénkaane bu mu dénk waa kër Yuusufa,

7«Yennil naa leen yen bi,

8Ngeen jàq, woo ma, ma xettali leen,

9Yeen sama ñoñ, dégluleen, ma dénk leen.

10Buleen fat tuuru jàmbur,

11Man, Aji Sax ji, maay seen Yàlla

12«Waaye sama ñoñ déggaluñu ma,

13Moo tax ma bërgël leen ak seenug të,

14Éy su ma sama ñoñ déggaloon,

15Ci saa si laay toroxal seeni noon,

16ba ku bañ Aji Sax ji di ko raamal,

e>