Taalifi cant 99:1-8 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax jeey Buur. Yeen xeet yi, ragalleen ko!

2Aji Sax ji fi Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* a màgg,

3Sa tur weeka màgg te raglu. Sàbbaalleen ko.

4Buur, jëfe yoon mooy dooleem.

5Màggalleen sunu Yàlla, Aji Sax ji,

6Musaak Aaróona|lemma="Aaróona:"* bokk ciy sarxalkatam|lemma="sarxalkat b-:"*,

7Fa biir taxaaru niir wa la waxeek ñoom,

8Céy sunu Yàlla Aji Sax ji, yaa leen nanguloon,

>