Yawut ya 1:1-13 WOLB2025 - Bible AI

1Bu yàgg la Yàlla waxoon ay yooni yoon ak maam ya, ci waxin yu bare, yonent yi jottali.

2Ci fan yu mujj yii, ci Doom ji la jaare wax ak nun, ki mu jagleel lépp, te ci moom la sàkke àddina wërngal këpp.

3Kooku mooy lerxat leeru Yàlla, te mooy ki jëmmal nekkug Yàlla. Moo téyee lépp kàddoom gu manoorewu. Gannaaw ba mu setalee bàkkaar yi nag, fa ndijooru Aji Màgg ji la toog, fa kawte ya,

4te ni turam wi mu séddoo gëna màgge turi malaaka yi, ni lees ko yékkatee, ba mu gëna màgg malaaka yi.

5Ndax kat, ana kan ci malaaka yi la Yàlla masa wax ne ko:

6Buy indiwaat taaw|lemma="Taaw b-:"* bi ci àddina nag, ci la naan:

7Malaaka yi, la Yàlla wax ci seen mbir ne:

8Waaye Doom ji la Yàlla ne:

9Yaa sopp dëgg, bañ lu bon,

10Mu neeti:

11Yooyu day réer,

12Yaa leen di taxañ ni malaan,

13Ana kan ci malaaka yi la mas ne:

© 2025 Bible Society of Senegal
iv>