Yawut ya 8:1-12 WOLB2025 - Bible AI

1Kàddu yii nu wax nag, lii moo di ponk bi: boobu sarxalkat|lemma="sarxalkat b-:"* bu mag lanu am, mu toog ci ndijooru ngànguney Ku màgg ka fa asamaan.

2Mooy liggéey ca kër gu sell ga, ca biir xaymab jaamookaay bu dëggu, ba Boroom bi samp, te nit sampu ko.

3Gannaaw nag ab sarxalkat bu mag bu mu mana doon, dees koo fal, ngir muy joxe ay saraxi njébbal ak saraxi jur, kon fàww sarxalkat bu mag bii itam am lu mu sarxe.

4Bu doon ci àddina, du nekk sax ab sarxalkat, gannaaw ay sarxalkat a ngi fi, di jébbale ay sarax, ni ko yoonu Musaa laaje.

5Sarxalkat yooyu, jaamookaay bi ñuy liggéeye, ab misaal la, takkndeeru yëf yu dëggu ya fa asamaan la. Ndax ba Musaa di waaja yékkati xaymab jaamookaay ba, noonu lees ko artoo woon, ne ko: «Nanga xool te def lépp, mu dëppook misaal mi ñu la won ci kaw tund wi+ 8.5 Seetal ci +bk Mucc ga+bk* 25.40.*.»

6Waaye tey la Yeesu jot ci liggéeyu carxal gu sut gu njëkk ga fuuf, te kóllëre|lemma="kóllëre g-:"* gi mu fas diggante Yàlla ak nit ñi, noonu la gëne gu njëkk ga; dige yi lal kóllëre gu yees gii it, noonu la gëne dige ya laloon gu njëkk ga.

7Bu kóllëre gu njëkk ga muccoon sikk nag, deesul soxlaa xajal geneen.

8Waaye Yàllaa sikk bànni Israayil|lemma="bànni Israayil:"*, ba mu nee:

9ba ma leen jàppee ci loxo,

10«Lii nag moo di kóllëre gi may fas

11Kenn dootul soxlaa jàngal moroomam,

12Maa leen di jéggal seeni ñaawtéef,

© 2025 Bible Society of Senegal
iv>