Yeremi 12:1-16 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji, yaa dëggu,

2Yaa leen jëmbat, ñu sampi reen,

3Waaye yaw Aji Sax ji, xam nga ma;

4Ba kañ la réew mi naa sereŋ,

5«Ndegam boroom ñaari tànk ngay rawanteel, xoox,

6Say bokk ak sa waa kër baay sax,

7«Dëddu naa sama kër,

8Sama séddoo ngi may niru léegi

9Sama séddoo baa ngi may saf tan mu todde

10Gàngooru sàmm a sëxëtoo sama tóokëru reseñ,

11Def nañu ko gent buy jooy fi sama kaw,

12Tundoo tund wu ne faraas fi màndiŋ mi,

13Jiwum pepp, góob ay dég;

14Aji Sax ji dafa wax ne: «Mboolem sama dëkkandoo yu bon yi laal céru suuf bi ma sédd Israayil sama ñoñ, maa ngii di leen déjjatee seen réew, te waa kër Yuda, maa leen di seppee fi seen biir.

15Waaye bu ma déjjatee yooyu xeet ba noppi, dinaa leen dellu yërëm, ku nekk, ma delloo ko céram, ku nekk ak suufam.

16Waaye bu ñu royee ba roy sama ñoñ, di jëfe ni sama ñoñ wara jëfe, di giñe sama tur naan: “Giñ naa ko ci Aji Sax jiy dund,” na ñu daan royloo sama ñoñ, ba ñuy giñe Baal|lemma="Baal:"*, tuur mi, su boobaa ñu sampu fi sama biir ñoñ.

© 2025 Bible Society of Senegal
v>