Yeremi 13:1-26 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji da maa wax ne ma: «Demal jëndi njiitlaayu lẽe+ 13.1 njiitlaay li ñuy wax fii, séru njiitlaay lu gàtt lay doon.*, nga sol ko, te bu ko ndox laal.»

2Ma jënd tubéy ji, sol ko, muy la Aji Sax ji wax.

3Aji Sax ji dikkal ma ñaareel bi yoon, ne ma:

4«Jëlal tubéyu njiitlaay ji nga sol, te daldi dem ba Farat+ 13.4 Farat, béreb la bu bokkul ak dexu Efraat doonte neexoo nañuy tur.*, nga làqi ko fa ca xar-xaru doj ya.»

5Ma dem làqi ko Farat, muy la ma Aji Sax ji sant.

6Ñu dem ba mu mat ay fan yu takku, Aji Sax ji ne ma: «Demal Farat, jëli tubéyu njiitlaay ja ma la santoon nga làqi ko fa.»

7Ma dem fa ma làqoon tubéy ja, sulli ko. Ndeke tubéy ja yàqu na, ba amatul njariñ!

8Kàddug Aji Sax ji dellu dikkal ma, ne ma:

9«Aji Sax ji dafa wax ne: Ni lii yàqoo, ni laay sàggee sagub Yuda ak sagu Yerusalem bu réy bi.

10Askan wu bon wii bañ maa déggal, të ticc di wéye seen coobare, di topp yeneen yàlla, di leen jaamooka sujjóotal, nañu mel ni tubéyu njiitlaay jii amul benn njariñ.

11Ndax ni tubéyu njiitlaay di taqe ci luppu nit, noonu laa jële woon waa kër Israayil ak waa kër Yuda, taqoo leen.» Kàddug Aji Sax jee. Mu ne: «Maa ko def ngir ñu doon sama ñoñ, teral sama tur, di sama ndam, di sama sag. Waaye déggaluñu ma.

12«Nga wax leen kàddu gii: “Aji Sax ji Yàllay Israayil dafa wax ne: Njaqal biiñ, duy, mu fees.” Bu ñu la nee: “Xanaa dañoo xamul ne njaqal biiñ lu ne dina fees?”

13nga ne leen: “Aji Sax ji dafa wax ne: Muy buur yi toogal Daawuda cib jalam, di sarxalkat|lemma="sarxalkat b-:"* yi, di yonent yi, di mboolem waa Yerusalem, maa ngii di duysi mboolem waa réew mii, ba ñu fees ak màndite.

14Su ko defee ma fenqe ku nekk ak mbokkam, fenqe waajur ak doom, ñoom ñépp.”» Kàddug Aji Sax jee. Mu ne: «Duma ñéeblu, duma yërëm, duma leen ñeewantee sànk.»

15Dégluleen te teewlu, buleen fétteeral.

16Teralleen seen Yàlla Aji Sax ji,

17Bu ngeen déggul de,

18Waxal Buur, wax Lingeer yaayu Buur ne leen:

19Dëkki Negew yu mag yi tëje na,

20Yerusalemee, séentul, xool ñiy jóge bëj-gànnaar.

21Sa xejj yi nga miinal sa bopp,

22Soo nee ci sam xel:

23Ana ab Kuuseen|lemma="Kuus:"* bu mana soppi deram,

24«Maa lay tasaare ni boob buy naaw

25Loolooy sa wàll,

26Man it maay ëñ sa pendal,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>