Yeremi 15:1-20 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji nag ne ma: «Musaa ak Samiyel sax, bu ñu taxawoon fi sama kanam, du tax ma faale askan wii. Dàqal, ñu sore ma, te wéy.

2Bu ñu la laajee ne la: “Fu nu jëm?” nga wax leen ne leen:

3«Te dinaa wàcce fi seen kaw ñeenti xeeti duma.» Kàddug Aji Sax jee. «Saamar di bóom; xaj diri yóbbu, njanaaw ak rabu àll for, mu jeex.

4Dama leen di def, waa réewi àddina yépp, ku leen ci xool rasu. Te li ko waral di Buurub Yuda, Manase miy doomu Esekiyas, ak li mu def ci digg Yerusalem.

5«Yerusalemee, ku lay yërëm?

6Yaw yaa ma wacc, kàddug Aji Sax jee,

7Maa leen bees ni ñuy beesem pepp

8Seeni jëtun laa ful,

9Yaayu juróom ñaari góor loof, di àppaat,

10Wóoy saa ndey,

11Ndaxam Aji Sax ji nee:

12«Ku mana toj weñ gu ñuul,

13Yeen waa Yuda, seen alal ak seeni denc

14Maa leen di def seen jaami noon

15Yaw déy Aji Sax ji, xam nga!

16Sa kàddu laa gis, di ko dunde,

17Masumaa toogandook ñiy mbumbaay

18Moo, sama tiis wi du dakk a?

19Moo tax Aji Sax ji dafa wax ne:

20Maa lay def nga mel ci gis-gisu askan wii

© 2025 Bible Society of Senegal
v>