1Kàddug Aji Sax ji dikkal ma, ne ma:
2«Demal yéeneji lii, Yerusalem di dégg,
3Mooy ba Israayil dee lu ñu sellalal Aji Sax ji,
4Dégluleen kàddug Aji Sax ji,
5Aji Sax ji dafa wax ne:
6Newuñu: “Ana Aji Sax
7Ma indi leen ci suuf su nangu,
8«Sarxalkat|lemma="sarxalkat b-:"* yi newuñu: “Ana Aji Sax ji?”
9Moo ma tax di layooteek yeen,
10«Demleen ba ca duni Kitim fa sowu, te xool;
11Fu aw xeet masa weccee yàllaam?
12Asamaanee, waarul ci lii!
13«Ñaari yoon la xeet wi ma séddoo bàkkaar:
14«Israayil da dib jaam a?
15Gaynde yaa ngi ŋar ci seen kaw,
16Te it niti Memfisoo niti Tapanes+ 2.16 Memfis ak Tapanes, dëkki Misra lañu. Fi ñu ne Memfis am na sotti yu fi indi turu Nof.*
17Xanaa du yeena def seen bopp lii,
18Léegi lu ngeen wuti Misra?
19Seenug mbon a leen di mbugal,
20«Yàgg ngeena yiwiku,
21Moona maa leen jëmbat, ngeen di ngëneelu reseñ,
22Bu ngeen raggoo woon saabu,
23«Nu ngeen ñemee naa: “Sobeelunu sunu bopp
24mbaa mbaamu àll mu miin màndiŋ mi,
25Ma ne, buleen daw ba mujje tànki neen
26«Gàcceg sàcc bu ñu jàpp
27ñoom ñii naa bii bant: “Yaay sunu baay,”
28Waaw, ana seen yàlla yi ngeen sàkkal seen bopp?
29Ana lu ngeen di layook man?
30«Mbugal naa seeni doom, jariñul dara.
31Éey niti Israayili tey,
32Ab janq dina fàtte takkaayam?
33Yeen aka mokkal gànctu!
34Te seeni pendal sax taq na
35ngeen naan: “Nun de defunu dara,
36Yeen aka yomba soppi doxalin!