Yeremi 3:1-24 WOLB2025 - Bible AI

1Mu ne: «Su waay fasee jabaram,

2«Téenleen, séentu tund+ 3.2 tund: kaw tund yooyu lañu daan jaamoo tuur yi ñu foogoon ne dañuy nangul am njur.* ya ne faraas!

3Moo tax waame aje,

4Léegi ngeen di ma woo wall naa:

5Xanaa deesul mer ba fàww?

6Aji Sax ji nag wax ma ci jamonoy buur Yosya ne ma: «Gis nga li Israayil Woyof-Kumba-si def? Di dem kaw tundoo tund ak ker garaboo garab gu naat, di fa gànctu.

7Ma noon su defee loolu lépp ba noppi, dina délsi, te délsiwul. Te doomu ndeyam Yuda workat bi gis na ci.

8Gis naa ne it Israayil Woyof-Kumba-si gànctu na ba ma yebal ko, jox ko kayitu pase, mu dem, te taxul doomu ndeyam Yuda workat bi ragal. Moom it daa dem di gànctu.

9Ni gànctu yombe Israayil tax na réew mi sobewu. Njaaloo naak yàllay doj, njaalook yàllay bant.

10Loolu yépp itam taxul Yuda workat bi, doomu ndeyu Israayil, délsee léppi xolam fi man, xanaa di jinigal rekk.» Kàddug Aji Sax jee.

11Aji Sax ji nag ne ma: «Li Israayil di woyof kumba lépp sax moo tane Yuda workat bi.

12Demal yéeneji kàddu yii fa bëj-gànnaar. Nga ne:

13“Nangul ne ñaaw nga rekk,

14«Yeen doom yu woyof kumba yi, délsileen.»

15tànnal leen sàmm yu ma doy,

16Janti keroog bu ngeen baree ba giir ci réew mi,

17«Janti keroog

18Janti keroog waa kër Yuda

19«Maa leen naroona teral ni doom yu góor,

20Teewul, yeen waa kër Israayiloo, ngeen wor ma,

21«Coow dégtu na ca kaw tund ya ne faraas,

22Yeen doom yu woyof kumba yi,

23Naxi neen kay lañu jële ca xërëmi tund yu ndaw ya

24Ba nuy gone ba tey,

© 2025 Bible Society of Senegal
>