1Kàddug Aji Sax jii dikkal na Yonent Yàlla Yeremi, jëm ci xeet yi.
2Lu jëm ci Misra:
3«Ŋàbbleen pakkoo pakk te xareji.
4Takkleen fas yi, war naaru-góor yi,
5«Ana lu ma gis?
6«Bu nit gaaw ba raw
7«Kii ku mu, muy fuddu ni dexu Niil,
8Misraa, mooy fuddu ni dexu Niil,
9Na fas buur, watiir fiddi,
10Waaye bésub keroog déy,
11Yaw Misra mu taaru mi,
12Xeet yeey dégg sa toroxte,
13Kàddu gii dikkaloon na Yonent Yàlla Yeremi, ba Nebukatnecar buuru Babilon dikkee, di duma waa réewum Misra. Mu ne:
14«Yégleel lii Misra, yéene ko fa ca Migdol,
15Lu Apis, seen jëmmi tuur ma, di daw?
16Moo bëmëx ñu bare,
17Dees na fa woyal Firawna buuru Misra, naan ko:
18«Giñ naa ko ci man miy dund,»
19Yaw mi dëkke Misra mu taaru mi,
20Misra daa mel ni jeegu nag bu yànj,
21Seen xarekat yi ñu bind sax
22ñu daw di faraas-faraasiy wéy ni jaan.
23Lu gott fatt fatt, ñu gor.»
24Gàcceel nañu Misra mu taaru mi,
25Aji Sax ji Yàllay Israayil, Boroom gàngoori xare yi wax na ne: «Maa ngii di dikke mbugal Amon, tuuru dëkk bii di No, ak Firawnaak waa Misraak seeni tuur ak seeni kàngam, boole ci ñi yaakaar Firawna.
26Maa leen di teg ci loxoy ñiy wut seen bakkan, di Nebukatnecar buuru Babilon aki jawriñam. Gannaaw loolu dees na dëkkewaat Misra na woon.» Kàddug Aji Sax jee!
27«Yaw Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* sama jaam bi nag, bul tiit;