1Kàddug Aji Sax ji dikkaloon na Yonent Yàlla Yeremi jëm ci Filisteen ñi, balaa Firawna di song dëkkub Filisteen ba ñuy wax Gasa.
2Aji Sax ji dafa wax ne:
3Booba fas yaa ràmbal,
4bésub sànkute dikkal képp kuy Filisteen,
5Watu nel, ñaawloo dikkal na Gasa,
6Ngeen naa: “Wóoy saamaru Aji Sax jii,