1Lu jëm ci Mowab:
2Mowab amatul woy,
3Yuux jibe na Oronayim,
4Mowab tas, ay fereem serandoo.
5Ñay yéeg jëm Luxit, di jooyoo.
6Ñu naan: “Dawleen, rawale seen bakkan,
7Mowab, yeena yaakaar dooleek alal,
8Dëkkoo dëkk ay yàqtoo,
9«Gasalleen Mowab,
10Alkànde ñeel na kuy sàggane liggéeyu Aji Sax ji.
11«Mowab a dale féex cag ndawam,
12Moo tax ay bés a ngii di ñëw,»
13Yaakaaru Mowab ci Kemos tuur mi tas,
14«Yaw réewu Mowab, du yaay kañu,
15Song nañu Mowab, yàqate ay dëkkam;
16«Musibay Mowab a ngi jegesi,
17Mboolem yeen ñi wër xeet wii, jooyleen ko;
18«Yeen waa Dibon, dëkk bu taaru bi,
19Yeen waa Arower,
20Ñu ne: “Gàcce ñeel na Mowab gii tas!”
21Mbugal dikkal joor gi,
22ak Dibon ak Nebo ak Bet Diblatayim
23ak Kiryaatayim ak Bet Gamul ak Bet Mewon
24ak Keryot ak Boccara,
25Sidditu Mowab day dog,
26«Du Mowab a doon diir Aji Sax ji mbagg?
27Waa Mowabee, du yeena doon ree Israayil?
28Yeen waa Mowab,
29«Noo dégg ni Mowab bewe,
30Maa xam seen reewande,»
31Moo tax may jooy Mowab,
32Yaw reseñu Sibma gi,
33Tukkal nañu mbégteek bànneex
34Yuux jibe na Esbon, ba Elale, àkki ba Yaxacc
35Maay bóome biir Mowab.»
36Naa jooy Mowab jooyi xol
37Ñoom ñépp a nelu,
38Kaw taaxi Mowab yépp aki péncam,
39«Yuuxooleen, ne leen: “Céy gii yàqtoo!
40Aji Sax ji déy dafa wax ne:
41Dees na teg Keryot ga ca Mowab loxo,
42Mowab day sànku, ba xeetam fey.
43Yeen waa Mowab,
44«Pat-patiy daw, tàbbim pax;
45«Fa keppaaru Esbon lañuy daw taxawi,
46Wóoy, waa Mowab, ngalla yeen!