Yeremi 5:1-30 WOLB2025 - Bible AI

1«Wërleen mbeddi Yerusalem,

2Bu ñu nee sax: “Giñ naa ko ci Aji Sax jiy dund,”

3Aji Sax ji, xanaa du worma ngay sàkku?

4Man nag, ma noon: «Ñii de ay baadoolo rekk lañu,

5Kon naa dem seeti kàngam yi,

6Moo tax gaynde di génne ci gott bi, fàdd leen,

7«Yerusalem, ana lu tax ma di la baal,

8Mbete fas yu suur, tukkal,

9Lii, duma leen ko dumaa?»

10«Yéegleen seeni tata, yàqate,

11Waa kër Israayil ak waa kër Yuda kat,

12«Ñoo fenal Aji Sax ji,

13Yonent yi daal, ngelawal neen!

14Moo tax Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:

15Éey waa kër Israayil,»

16Seen mbari fitt ŋafal paxum bàmmeel,

17Ñooy dikk, warax seen meññeef ak seen ñam,

18Waaye bési keroog it,»

19Bu ñu nee:

20«Jottalileen lii waa kër Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"*,

21“Ngalla dégluleen lii,

22Man daal, ndax dangeen maa ragalul,

23Waaye wii xeet a dëgër bopp te déggadi.

24Seen xel demul sax ba ne:

25Yooyii seeni ñaawtéef a ko waññi,

26«Waaw! Daa am ñu bon ci sama ñoñ,

27Ni kaaf di feeseeki picc,

28yaflu, di nes-nesi.

29Lii, ndax duma leen ko dumaa?»

30Lu siblu te yées am na ci réew mi:

© 2025 Bible Society of Senegal
>