Yeremi 50:1-45 WOLB2025 - Bible AI

1Kàddu gii la Aji Sax ji wax ci mbirum réewum Babilon, di réewum Kaldeen ña, te Yonent Yàlla Yeremi jottali ko:

2«Waxleen xeet yi, yéeneleen,

3Aw xeet kay ay bawoo bëj-gànnaar, dal fi seen kaw.

4Su bés baa, ci yooyu fan,»

5Dinañu laaj yoonu Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, jublu fa

6«Sama ñoñ ñi réer niy xar,

7Noon bu taseek ñoom warax leen

8«Yeen sama ñoñ, fëxeleen Babilon,

9Maa ngii déy di xabtal fi kaw Babilon,

10Réewum Babilon a doon alalu sëxëtoo,

11«Ãa yeen waa Babilon, yeena sëxëtoo xeet wi ma séddoo,

12Ndaw gàcce gu réy ci seen ndey,

13Kenn du fi des ndax merum Aji Sax ji,

14Yeen fittkat yépp, làng-déralleen Babilon,

15Xaaculeen fi kawam, wër ko,

16Génneleen Babilon képp kuy ji ak kuy góob,

17«Waa Israayil diy gàtt yu tasaaroo,

18Moo tax Aji Sax ji Yàllay Israayil, Boroom gàngoor yi ne:

19Maa ngii di delloo Israayil parloom,

20Su bés baa, ci yooyu fan,»

21«Songleen réewum Meratayim ak waa Pekodd+ 50.21 réewum Meratayim ak waa Pekodd, ci Babilon lañu bokk.*,

22Coowal xaree ngi fi réew mi,

23Babilon, réew mi daan wàkk mboolem àddina,

24Babilon, maa la fiir,

25Aji Sax ji ubbi na waxandey xareem,

26Songeleen ko fu ne,

27Jamleen seen jàmbaari yëkk yépp;

28Baatu daw-làqu yu rëcc a ngoog,

29Wooleen fittkatoo fittkat fi kaw Babilon,

30Moo tax bésub keroog

31«Yaw Babilon mu daŋŋiiral mi, maa ngii fi sa kaw.»

32Ku daŋŋiiral keey tërëf, fëlëñu,

33Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:

34Waaye seen jotkat|lemma="jotkat b-:"* a am doole,

35«Saamar ci kaw waa Babilon!»

36Saamar ci kaw kebetukati diine yi,

37Saamar ci kaw fas ak watiiram,

38Maral ci kawi waltanam, mu ŋiis;

39Moo tax ay ndundati màndiŋ ak rabi àll a koy këroo,

40Mu mel ni ba Yàlla tasee Sodom|lemma="Sodom ak Gomor:"* ak Gomor,

41«Aw askan a ngii, bàyyikoo bëj-gànnaar,

42Yeen waa Babilon, réew mu taaru mi,

43Buuru Babilon dégg riir ma,

44Maa ngii, di fëlle gottub Yurdan ni gaynde,

45Kon dégluleen pexe mi Aji Sax ji waajal Babilon,

© 2025 Bible Society of Senegal
v>