Yeremi 51:1-63 WOLB2025 - Bible AI

1Aji Sax ji dafa wax ne:

2Maay yónnee Babilon ay beeskat

3Buleen leen may fu ñu taxaweek seen kiiraay, di fitte;

4Ñii dee, ne wetar réewum Babilon;

5Israayil ak Yuda ñàkkuñu seen Yàlla,

6«Yeen gan ñi, génnleen Babilon,

7Aji Sax jee yor Babilon ci loxoom, muy kaasu wurus bu def xadaru xeet ya,

8Teewul Babilon jekki daanu, tasaaroo.

9Bu nu sañoon faj Babilon, mu wér,

10Aji Sax ji jox na nu dëgg.

11«Nàmmleen fitt yi, feesale mbar yi!

12Yékkatilleen tatay Babilon raayab xare,

13Yeen ñi dëkke weti ndox yu ne xéew,

14Aji Sax ji Boroom gàngoor yi giñ na ci boppam:

15Suuf, Aji Sax jee ko sàkke kàttanam;

16Bu àddoo, ndoxum asamaan riir;

17Nitoo nit dim sanax, sore xam-xam,

18Cóolóolu neen, liggéeyu caaxaan;

19Ki séddoo Yanqóoba|lemma="Yanqóoba:"* déy wuute naak yii caaxaan.

20«Yaw Babilon, yaa doon sama wàkku,

21dóore la fas ak gawaram,

22dóore la góor ak jigéen,

23dóore la sàmm ak géttam,

24Waaye mboolem lu Babilon ak waa réew mépp def ci Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*,

25«Maa ngii déy, fi sa kaw, yaw Babilon, ponkalum yàqkat bi,»

26Deesul seppee fi yaw doju koñu tabax bi,

27«Yékkatileenub raaya fi réew mi

28Dajaleleen xeet yi fi kaw Babilon,

29Suuf a fuddu, wañaaru,

30Jàmbaari Babilon xareetuñu,

31Xélukat dab xélukat;

32nangu jàllukaayi dex ya,

33Aji Sax ji Yàllay Israayil, Boroom gàngoori xare yi déy dafa wax ne:

34Buuru Babilon warax na ma.

35Waa Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"* ne: «Yal na sama yàpp ak sama coono topp Babilon.»

36Aji Sax ji nag dafa wax ne:

37Babilon def jali doj,

38Ñu ngi ŋarandoo niy gaynde,

39Ñu tàng bay bëgga dee,

40Aji Sax ji nee: «Maa leen di wommat

41«Ãa! Ana nees mana nangoo Sesag+ 51.41 Sesag turu kumpa la, di Babilon ba tey.*?

42Géej ay mëdd Babilon,

43ay dëkkam gental,

44Maay dikke mbugal Bel,

45Yeen sama ñoñ, génnleen fi seen biir,

46Bu seen fit rëcc,

47Kon ay bés a ngii di ñëw,

48Su boobaa asamaan ak suuf

49Waa Babilon it dinañu daanu

50Ée yeen ñi rëcc saamar,

51Nooka rus ci saaga yi nu dégg,

52«Moo tax, bés a ngii di ñëw,»

53Su Babilon yéegoon asamaan,

54Yuuxi njàqare fa Babilon,

55Aji Sax jee niy yàqatee Babilon,

56Yàqkat déy dikkal na Babilon,

57Mu ne: «Maay màndal seeni kilifaak seeni kaaŋ

58Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:

59Ndigal yii ñooy ndigal yi Yonent Yàlla Yeremi jox Seraya doomu Nerya doomu Maxseya, ba mu àndee ak Buur Cedesyas ca Babilon ca ñeenteelu atu nguuram. Seraya moo doon bëkk-néegam.

60Fekk na Yeremi bind cib téere bu ñu taxañ mboolem safaan yiy dikkal Babilon, di mboolem mbir yooyu jëm ci Babilon.

61Yeremi sant Seraya, ne ko: «Boo àggee Babilon, fexeel ba biral kàddu yii yépp.

62Te nga wax ne: “Aji Sax ji, yaw déy, yaa xamle ne dëkk bii dina tas, dara du ci dëkkati, du doom aadama, du rab. Ab gent lay doon ba fàww.”

63Boo jàngee téere bu ñu taxañ bii ba noppi, nanga ci takk aw xeer, sànni ko ci biir dexu Efraat.

© 2025 Bible Society of Senegal
v>