1«Yeen askanu Beñamin, fëxleen,
2Yaw Siyoŋ|lemma="Siyoŋ:"*, dëkk bu taaru bi te xejj,
3Ay sàmm ak seeni gétt ci sa kaw,
4Ñii ne: «Waajalleen xare baak ñoom,
5Ñee ne: «Nan song congum guddi boog,
6Aji Sax ji Boroom gàngoor yi déy da ne:
7Ni bëtu ndox di dawe,
8Yeen waa Yerusalem, deeleen dégg
9Aji Sax ji Boroom gàngoor yi dafa wax ne:
10Moo kan laay waxal,
11Maa ngi fees dell ak merum Aji Sax ji,
12seeni kër doon alali jàmbur,
13«Ndax ki gëna tuut ba ki gëna mag,
14Sofental nañu sama pajum ñoñ ñi dammatoo,
15Ñu wara am gàcce ci seen jëf ju siblu,
16Aji Sax ji dafa wax ñoñam ne:
17«Ma tabbal leeni wattukat
18«Moo tax yeen xeet yi, dégluleen;
19Yeen waa àddina, dégluleen!
20Lu may doye lii?
21Moo tax Aji Sax ji wax ne:
22Aji Sax ji dafa wax ne:
23Fitt aku xeej lañuy ŋëb,
24Danoo dégg riir mi,
25Kii naa: «Bul génn ci àll bi!»
26Éey bokk yi, solleeni saaku,
27«Maa la def sama nattukatu ñoñ,
28Ñoom ñépp a di fippukat yu fétteeral,
29Tëgg wal taalam, mu yànj;