Yunus 2:1-10 WOLB2025 - Bible AI

1Ci kaw loolu Aji Sax ji yebal jën wu mag, mu wann Yunus. Mu nekk ca biiru jën wa ñetti bëccëg ak ñetti guddi.

2Yunus ñaan ci Yàllaam Aji Sax ji, fa mu tollu ca biir jën wa.

3Mu ne:

4Yaa ma xalab xóotey xolu géej, ndaw ma mëdd ma.

5Man nag ma naan: «Dàqees na ma, ba ma sore la,

6Ndox maa ma tanc ba ci put,

7Ca reeni tund ya laa suuxi,

8Noowal bakkan a nga may rëcc,

9Ñiy wormaal neenug neen daal,

10Man nag, ci biir cant laa lay sarxale.

© 2025 Bible Society of Senegal